Skip to main content

Dip Doundou Guiss #FreeSenegal

0:002:54

Composition : Karabalik Beatz & Alain Oyono Réalisation : Reverse Studios Paroles en Wolof : Dëkk ci dëkku nittu fitna Sonn di wax yen ñëpp a yem kiif-kiif la 6-9 Li ma si gën a meti di gis boy yi di dee Reew mi ñi koy fiy jiite ñëppay roy Lucifer Nàcc ba coow li jeex sunu ròngoñ yi duñ fer Naaj bu dem jànt fake ñoo la folli bul rëy Gàddu sa call di Twitter su njaboot bi di dee Mënu toog di muñ rekk di len xool ñu ñuy ray Nawu ma politicien du ma politique man Kuy tanqamlu kilifa diine du maay wax lu muy deeg Suba yaay rus a netali say doom sunu tay Ndaw yi prison la ñuy xëy sen école la ñuy gëj Ndox bi jox nga ko Macron mool du joow ba gis jën Police aar lañ ko santoon tay ñoy door nitt ñi gun Mere bu Ci ñakk sa doom yuuxu wooy fu ñu jëm Xeex bi ñëpp a Ci d’accord ndax ñoo

  • Producer: Karabalik Beatz & Alain Oyono
  • Album: #FreeSenegal
  • Release Date:

6 Comments